AbdouLaye🎭
banner
abdoulayee.bsky.social
AbdouLaye🎭
@abdoulayee.bsky.social
DeVweb 💻 | Passionné par la tech et l'IA 🤖 | 🚀
Reposted by AbdouLaye🎭
Tay nieup wara 1k bala minuit
Aythieu Rt pour nieup diotci
Je fb tout le monde
#bluesky221
November 24, 2024 at 1:12 PM
Mais da melni Appli bi amagul benna Star deeh wlla gars yi sibagunu?
November 24, 2024 at 12:31 PM
Sinon dite aux “wathia bess” que TL (Time Line) signifie fil d’actualité manam où apparaissent les publications des comptes que vous suivez , Geen niowfi dinou sonal ak ay BlueFoot, Sky221 … you keeen xamul🙆🏾😂
November 24, 2024 at 1:14 AM
Mai tiktok cons naneu damnn😂😂😂
November 23, 2024 at 11:41 PM
Dagay nek petit compte tweeter nioulay newal dolé nioy blueSky nieup yamm barkei Yallah😂
November 23, 2024 at 9:24 PM
Star (X)tweeter yi Yallah geen nek fi ay citoyens lambdas 😂
November 23, 2024 at 6:32 PM
Reposted by AbdouLaye🎭
Le réseau des patriotes 😭😭🫱🏾‍🫲🏽🇸🇳❤️?
November 23, 2024 at 4:34 PM